Vous avez cherché: adpropinquavit (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

surgite eamus ecce adpropinquavit qui me tradi

Wolof

jógleen nu dem; xool-leen, ki may wor a ngi nii, di ñëw.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et dicens paenitentiam agite adpropinquavit enim regnum caeloru

Wolof

nii la doon waaree: «tuubleen seeni bàkkaar, ndaxte nguuru yàlla aji kawe ji jege na.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

euntes autem praedicate dicentes quia adpropinquavit regnum caeloru

Wolof

bu ngeen demee nag, yégleleen naan: “nguuru yàlla aji kawe ji jegesi na.”

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et ut adpropinquavit videns civitatem flevit super illam dicen

Wolof

bi yeesu jegee dëkk ba, ba séen ko, mu jooy ko

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

omnium autem finis adpropinquavit estote itaque prudentes et vigilate in orationibu

Wolof

te itam muju lépp jegesi na; nangeen maandu te foog, ba man a ñaan ci yàlla.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

cum autem videritis circumdari ab exercitu hierusalem tunc scitote quia adpropinquavit desolatio eiu

Wolof

«bu ngeen gisee ay xarekat wër dëkku yerusalem, xamleen ne jamono, ji ñu koy yàq, agsi na.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et dicens quoniam impletum est tempus et adpropinquavit regnum dei paenitemini et credite evangeli

Wolof

naan: «jamono ji mat na, nguuru yàlla jegesi na; tuubleen seeni bàkkaar te gëm xebaar bu baax bi.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

adhuc eo loquente ecce turba et qui vocabatur iudas unus de duodecim antecedebat eos et adpropinquavit iesu ut oscularetur eu

Wolof

bi yeesu di wax, mbooloo mu bare agsi; ku ñuy wax yudaa te mu bokkoon ci fukki ndaw yi ak ñaar jiite leen. yudaa jegeñsi yeesu, bëgg koo fóon.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

qui dixit videte ne seducamini multi enim venient in nomine meo dicentes quia ego sum et tempus adpropinquavit nolite ergo ire post illo

Wolof

yeesu tontu ne: «moytuleen, bu leen kenn nax. ndaxte ñu bare dinañu ñëw ci sama tur ne: “moom laa,” walla ñu naan: “jamono ji jegesi na.” buleen topp ñooñu.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,776,190,930 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK