Vous avez cherché: bërgël (Wolof - Danois)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Danois

Infos

Wolof

kon nag yàlla dina bërgël seen kër, ba mu gent.

Danois

se, eders hus lades eder øde!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gannaaw xam yàlla soxalu leen, yàlla it bërgël na leen ci seen xel mu bon moomu, ñu sax ci jëf yu jekkadi.

Danois

og ligesom de forkastede af have gud i erkendelse, således gav gud dem hen i et forkasteligt sind til at gøre det usømmelige,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moo tax yàlla bërgël na leen ci seeni bëgg-bëgg, ñu sóobu ciy ñaawteef, di jëfleente lu gàccelu ci seeni cér.

Danois

derfor gav gud dem hen i deres hjerters begæringer til urenhed, til at vanære deres legemer indbyrdes,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

loolu moo tax nag yàlla bërgël na leen ci seeni bëgg-bëgg yu ruslu. seeni jigéen sax dëddu nañu li jekk, sóobu ci lu jekkadi, ñoom ak seeni moroom.

Danois

derfor gav gud dem hen i vanærende lidenskaber; thi både deres kvinder ombyttede den naturlige omgang med den unaturlige,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ma ne kon, ndax yàlla bërgël na xeetam? mukk! ndaxte man itam ci israyil laa bokk, wàcce ci ibraayma te bokk ci giiru ben-yamin.

Danois

jeg siger da: mon gud har forskudt sit folk? det være langt fra! thi også jeg er en israelit, af "abrahams sæd, benjamins stamme.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Wolof

kon nag yàlla dina bërgël seen kër. te maa ngi leen koy wax, dungeen ma gisati, ba kera ngeen ne: “yaw miy ñëw ci turu boroom bi, ku barkeel nga!”»

Danois

se, eders hus overlades til eder selv. men jeg siger eder: i skulle ingenlunde se mig, førend den tid kommer, da i sige: velsigtnet være den, som kommer, i herrens navn!"

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,181,520 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK