Vous avez cherché: mënuloo (Wolof - Estonien)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Estonien

Infos

Wolof

bul giñ it ci sa bopp, ndaxte mënuloo weexal mbaa ñuulal benn ci say kawar.

Estonien

ara vannu ka oma pea juures, sest sina ei või ühtki juuksekarva teha valgeks ega mustaks;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte ku fonk sa nafsu, bañaaleb yàlla nga, ndaxte doo déggal yàlla, mbaa ngay sàmm ay santaaneem, te mënuloo koo def sax.

Estonien

sellepärast et liha mõtteviis on vaen jumala vastu, sest ta ei alistu jumala käsule ega võigi alistuda.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

naan: «céy yaw itam, boo xamoon bésub tey yi la man a indil jàmm! waaye fi mu ne mënuloo koo gis.

Estonien

ning ütles: „kui sina teaksid sellel päeval, mis sinu rahule tarvis läheb! ent nüüd see on pandud varjule sinu silmade eest.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

xam naa say jëf, sa liggéey ak sag muñ. xam naa ne, mënuloo dékku ñiy def lu bon. seetlu nga ñi tuddoo samay ndaw, ba gis ne ay naaféq lañu.

Estonien

ma tean su tegusid ja sinu tööd ja su kannatlikkust ja et sa ei või sallida kurje ja oled läbi katsunud need, kes endid ütlevad apostlid olevat, aga ei ole, ning oled leidnud nad olevat valelikud;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

simoŋ piyeer laaj ko ne: «boroom bi, foo jëm?» yeesu ne ko: «fa ma jëm, mënuloo ma faa topp léegi, waaye dinga ma toppi ca kanam.»

Estonien

siimon peetrus ütleb temale: „issand, kuhu sa lähed?” jeesus vastas: „kuhu ma lähen, sinna sa ei võid mind järgida, aga edaspidi sa järgid mind!”

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,773,286,941 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK