Vous avez cherché: malaaka (Wolof - Tagalog)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Tagalog

Infos

Wolof

leer na ne, yeesu xettalisiwul malaaka yi, waaye askanu ibraayma lay xettalisi.

Tagalog

sapagka't tunay na hindi niya tinutulungan ang mga anghel, kundi tinutulungan niya ang binhi ni abraham.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waxi malaaka ma daldi jaaxal maryaama, muy xalaat lu nuyoo boobu man a tekki.

Tagalog

datapuwa't siya'y totoong nagulumihanan sa sabing ito, at iniisip sa kaniyang sarili kung anong bati kaya ito.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu seytaane bàyyi ko. te ay malaaka daldi ñëw fi yeesu, di ko topptoo.

Tagalog

nang magkagayo'y iniwan siya ng diablo; at narito, nagsidating ang mga anghel at siya'y pinaglingkuran.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte ci guddi menn malaaka dikkal na ma, jóge ci yàlla sama boroom, bi may jaamu.

Tagalog

sapagka't nang gabing ito ay tumayo sa tabi ko ang anghel ng dios na may-ari sa akin, at siya ko namang pinaglilingkuran,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci mbiri àtte ba, dina leen yey ndaxte àtte nañu malaaka mu bon mi jiite àddina si, ba daan ko.

Tagalog

tungkol sa paghatol, sapagka't ang prinsipe ng sanglibutang ito ay hinatulan na.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

malaaka yépp ay xel lañu rekk yuy liggéeyal yàlla, mu di leen yónni ñuy dimbali nit, ñi nar a jot mucc gi.

Tagalog

hindi baga silang lahat ay mga espiritung tagapaglingkod, na mga sinugo upang magsipaglingkod sa kapakinabangan ng mangagmamana ng kaligtasan?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

xanaa xamuloo ne, man naa laaj sama baay, te dina ma may ci taxawaay bi mbooloom malaaka mu xel dajul?

Tagalog

o inaakala mo baga na hindi ako makapamamanhik sa aking ama, at padadalhan niya ako ngayon din ng mahigit sa labingdalawang pulutong na mga anghel?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yàlla jébbalul malaaka yi benn sañ-sañ bu jëm ci jamonoy ëllëg ji nuy wax; keneen la ko jébbal,

Tagalog

sapagka't hindi niya ipinasakop sa mga anghel ang sanglibutang darating, na siya naming isinasaysay.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mi yéeg asamaan, toog fa ndeyjooru yàlla, mu tiim malaaka yi, boroom sañ-sañ yi ak boroom doole yépp.

Tagalog

na nasa kanan ng dios, pagkaakyat niya sa langit; na ipinasakop sa kaniya ang mga anghel at ang mga kapamahalaan ang mga kapangyarihan.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye fekkuñu fa néewam. Ñu dellusi, nettali nu ne, ay malaaka feeñu nañu leen, yégal leen ne, mi ngi dund.

Tagalog

at nang hindi mangasumpungan ang kaniyang bangkay, ay nangagbalik sila, na nangagsabing sila nama'y nakakita ng isang pangitain ng mga anghel, na nangagsabing siya'y buhay.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ba mu ko defee juróom-ñaari malaaka, ya yoroon juróom-ñaari liit ya, daldi defaru di waaj a liit.

Tagalog

at ang pitong anghel na may pitong pakakak ay nagsihanda upang magsihihip.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

séen ñaari malaaka yu sol mbubb yu weex, toog ca bérab, ba ñu dencoon yeesu; kenn ka féeteek bopp bi, ki ci des ca tànk ya.

Tagalog

at nakita niya ang dalawang anghel na nararamtan na nangakaupo, ang isa'y sa ulunan, at ang isa'y sa paanan, ng kinalalagyan ng bangkay ni jesus.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

juróom-benneelu malaaka ma wol liitam. noonu ma dégg baat bu jóge ci ñeenti béjjén, yi nekk ci koñi saraxalukaayu wurus, ba nekk ci kanam yàlla,

Tagalog

at humihip ang ikaanim na anghel, at narinig ko ang isang tinig mula sa mga sungay ng dambanang ginto na nasa harapan ng dios,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«waaye bés boobu ak waxtu woowu, kenn xamul kañ lay doon; du malaaka yi ci kaw, du sax doom ji, waaye baay bi rekk moo ko xam.

Tagalog

nguni't tungkol sa araw o oras na yaon ay walang nakakaalam, kahit ang mga anghel sa langit, kahit ang anak, kundi ang ama.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye malaaka ma ne ko: «bul ragal dara sakariya, ndaxte sa ñaan nangu na. elisabet sa jabar dina la jural doom, te dinga ko tudde yaxya.

Tagalog

datapuwa't sinabi sa kaniya ng anghel, huwag kang matakot, zacarias: sapagka't dininig ang daing mo, at ang asawa mong si elisabet ay manganganak sa iyo ng isang anak na lalake, at tatawagin mong juan ang kaniyang pangalan.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu ne juróom-benneelu malaaka, ma yoroon liit: «yiwil ñeenti malaaka, ya yeewe ca efraat, dex gu mag ga.»

Tagalog

na nagsasabi sa ikaanim na anghel na may pakakak, kalagan mo ang apat na anghel na nagagapos sa malaking ilog ng eufrates.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ma dem ca malaaka ma, laaj ko téere bu ndaw boobu. mu ne ma: «jël ko te lekk ko. dina wex ci sa biir, waaye dina neex ni lem ci sa gémmiñ.»

Tagalog

at ako'y naparoon sa anghel na nagsabi ako sa kaniya na ibigay sa akin ang maliit na aklat. at kaniyang sinabi sa akin, kunin mo ito, at ito'y kanin mo; at papapaitin ang iyong tiyan, datapuwa't sa iyong bibig ay magiging matamis na gaya ng pulot.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,792,664,226 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK