Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
프로필 및 백엔드
programa ci biir & xéet u lüggey
Ultimo aggiornamento 2014-08-15
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
Attenzione: contiene formattazione HTML nascosta
bind dns 서버 및 관련된 문서와 유틸리티 패키지를 선택합니다.
dafay tann serwóor bind dns ak dokimantaasioŋ yi ci aju ak ay paket yuy jumtukaay (utilitaire).
Ultimo aggiornamento 2014-08-15
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
가 나 안 인 시 몬 과, 및 가 룟 유 다 곧 예 수 를 판 자
simoŋ, mi bokk ca mbooloo, ma ñu tudde Ñi farlu ci moom seen réew; ak yudaa iskariyo, mi nar a wor yeesu.
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
및 야 고 보 의 아 들 유 다 와 및 예 수 를 파 는 자 될 가 룟 유 다
yudaa doomu saag, ak yudaa iskariyo, mi mujj a wor.
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
주 예 수 와 및 모 든 성 도 에 대 한 네 사 랑 과 믿 음 이 있 음 을 들 음 이
ndaxte dégg naa sa ngëm ci boroom bi yeesu, ak sa mbëggeel ci gaayam yu sell yépp.
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
교 법 사 세 나 와 및 아 볼 로 를 급 히 먼 저 보 내 어 저 희 로 궁 핍 함 이 없 게 하
naka senas àttekat bi nag ak apolos, waajal leen bu jekk ci seen tukki, ba seen aajo yépp faju.
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
곧 그 시 로 일 어 나 예 루 살 렘 에 돌 아 가 보 니 열 한 사 도 와 및 그 와 함 께 한 자 들 이 모 여 있
Ñu daldi jóg ca saa sa, dellu yerusalem, fekk fa fukki ndaw ya ak benn, ak yeneeni taalibe.
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
곧 베 드 로 라 고 도 이 름 주 신 시 몬 과 및 그 형 제 안 드 레 와 및 야 고 보 와 요 한 과 빌 립 과 바 돌 로 매
simoŋ, mi yeesu tudde piyeer, ak andare, mi bokk ak piyeer ndey ak baay; saag ak yowaana, filib ak bartelemi,
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
개 들 과 술 객 들 과 행 음 자 들 과 살 인 자 들 과 우 상 숭 배 자 들 과 및 거 짓 말 을 좋 아 하 며 지 어 내 는 자 마 다 성 밖 에 있 으 리
waaye ñi ci biti ñooy xaj yi, luxuskat yi, njaalookat yi, bóomkat yi, xërëmkat yi ak ñépp ñiy sopp fen te di ci wéy.
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
그 러 나 이 것 을 당 신 께 고 백 하 리 이 다 나 는 저 희 가 이 단 이 라 하 는 도 를 좇 아 조 상 의 하 나 님 을 섬 기 고 율 법 과 및 선 지 자 들 의 글 에 기 록 된 것 을 다 믿 으
waaye nangu naa ci sa kanam ne, maa ngi jaamu yàllay sunuy maam, ci topp yoon wi ñu ne, mooy tariixa; terewul ne, lépp li ñu tëral ci yoonu musaa ak li yonent yi bind, gëm naa ko.
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
` 무 릇 내 게 오 는 자 가 자 기 부 모 와 처 자 와 형 제 와 자 매 와 및 자 기 목 숨 까 지 미 워 하 지 아 니 하 면 능 히 나 의 제 자 가 되 지 못 하
«képp ku ñëw ci man te gënalu ma ko baayam, yaayam, jabaram, ay doomam, ay magam ak ay rakkam, walla sax bakkanam, du man a nekk sama taalibe.
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
내 가 무 슨 말 을 더 하 리 요 기 드 온, 바 락, 삼 손, 입 다 와 다 윗 과 사 무 엘 과 및 선 지 자 들 의 일 을 말 하 려 면 내 게 시 간 이 부 족 하 리 로
lu ma ci war a tegaat? ndaxte awma jotu wax ci mbirum sedeyon, barag, samson, yefte, daawuda, samwil ak yonent yi.
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
내 가 그 발 앞 에 엎 드 려 경 배 하 려 하 니 그 가 나 더 러 말 하 기 를 ` 나 는 너 와 및 예 수 의 증 거 를 받 은 네 형 제 들 과 같 이 된 종 이 니 삼 가 그 리 하 지 말 고 오 직 하 나 님 께 경 배 하 라 예 수 의 증 거 는 대 언 의 영 이 라' 하 더
noonu ma daanu ci ay tànkam, bëgg koo jaamu. waaye mu ne ma: «moytu koo def; sa nawle laa ci liggéey bi, di kenn ci say bokk, yiy sax ci seedeel yeesu. jaamul yàlla. ndaxte seedes yeesu mooy xel miy solu yonent yi.»
Ultimo aggiornamento 2012-05-06
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità: