Je was op zoek naar: desturi (Swahili - Wolof)

Menselijke bijdragen

Van professionele vertalers, bedrijven, webpagina's en gratis beschikbare vertaalbronnen.

Voeg een vertaling toe

Swahili

Wolof

Info

Swahili

wanafundisha desturi ambazo sisi raia wa roma haturuhusiwi kuzikubali wala kuzifuata."

Wolof

di xamle ay aada yu nu sañul a nangu mbaa nu di ko topp, nun ñi bokk ci nguuru room.»

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Waarschuwing: Bevat onzichtbare HTML-opmaak

Swahili

zakariya alichaguliwa kwa kura, kama ilivyokuwa desturi, kuingia hekaluni ili afukize ubani.

Wolof

bi ñuy tegoo bant, ni ko saraxalekat yi daan defe nakajekk, ngir xam kan mooy dugg ca bérab bu sell ba ca kër yàlla ga, ngir taal fa cuuraay, bant ba tegu ci sakariya.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

wazazi wa yesu walikuwa na desturi ya kwenda yerusalemu kila mwaka wakati wa sikukuu ya pasaka.

Wolof

at mu jot nag waajuri yeesu yi daan nañu dem yerusalem, ngir màggali bésu jéggi ba.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

kila wakati wa sikukuu ya pasaka, pilato alikuwa na desturi ya kuwafungulia mfungwa mmoja waliyemtaka.

Wolof

màggal gu nekk nag pilaat daan na may mbooloo mi, ñu tànn kenn ci ñi ñu tëjoon, mu bàyyil leen ko.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

hasa kwa vile wewe mwenyewe ni mtaalamu wa desturi za wayahudi na migogoro yao, ninakuomba basi unisikilize kwa uvumilivu.

Wolof

ndaxte xam nga bu baax aaday yawut yi ak seeni werantey yoon. kon maa ngi lay ñaan, nga déglu ma ak muñ.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

basi, waliutwaa mwili wa yesu, wakaufunga sanda pamoja na manukato kufuatana na desturi ya wayahudi katika kuzika.

Wolof

Ñu jël néewu yeesu, laxas ko ci càngaay, boole ko ak cuuraay li, ni ko yawut yi tàmmoo def, bu ñuy waajal néew.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

kwa maana tulikwisha msikia akisema eti huyo yesu wa nazareti atapaharibu kabisa mahali hapa na kufutilia mbali desturi zile tulizopokea kutoka kwa mose."

Wolof

ndaxte dégg nanu, muy wax ne, yeesum nasaret moomu dina daaneel bérab bii te soppi aada, yi nu musaa batale woon.»

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Waarschuwing: Bevat onzichtbare HTML-opmaak

Swahili

hapo palikuwa na mitungi sita ya mawe, ambayo kila mmoja uliweza kuchukua kiasi cha madebe mawili au matatu. ilikuwa imewekwa hapo kufuatana na desturi ya kiyahudi ya kutawadha.

Wolof

foofa amoon na fa juróom benni ndaa yu ñu yett ci doj, yu yawut ya daan jëfandikoo ngir seen sangu set. ndaa lu nekk man na def daanaka téeméeri liitar.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

kama ilivyo desturi katika makanisa yote ya watu wa mungu, wanawake wakae kimya katika mikutano ya waumini. hawana ruhusa kusema; ila wawe watii kama isemavyo sheria.

Wolof

na jigéen ñi noppi ci ndaje mi, ndaxte sañuñu faa wax. nañu doon jigéen ñu nangu, ni ko yoon wi tërale.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

basi, yesu alikwenda nazareti, mahali alipolelewa, na siku ya sabato, aliingia katika sunagogi, kama ilivyokuwa desturi yake. akasimama ili asome maandiko matakatifu kwa sauti.

Wolof

yeesu dem nasaret fa mu yaroo, te ca bésu noflaay ba, mu dugg ca jàngu ba, ni mu ko daan defe. noonu mu taxaw ngir jàngal mbooloo mi.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Swahili

baada ya siku tatu, paulo aliwaita pamoja viongozi wa kiyahudi wa mahali hapo. walipokusanyika, paulo aliwaambia, "wananchi wenzangu, mimi, ingawa sikufanya chochote kibaya wala kupinga desturi za wazee wetu, nilitiwa nguvuni kule yerusalemu na kutiwa mikononi mwa waroma.

Wolof

bi ñetti fan wéyee, mu woolu njiiti yawuti dëkk ba. bi ñu dajaloo nag, mu wax leen lii: «bokk yi, jàpp nañu ma ci yerusalem, jébbal ma waa room, fekk defuma dara luy suufeel sunu xeet, mbaa lu juuyoo ak sunuy aaday maam.

Laatste Update: 2012-05-05
Gebruiksfrequentie: 1
Kwaliteit:

Waarschuwing: Bevat onzichtbare HTML-opmaak

Krijg een betere vertaling met
7,761,054,793 menselijke bijdragen

Gebruikers vragen nu voor assistentie



Wij gebruiken cookies om u de best mogelijke ervaring op onze website te bieden. Door de website verder te gebruiken, geeft u toestemming voor het gebruik van cookies. Klik hier voor meer informatie. OK