You searched for: dëkku (Wolof - Engelska)

Mänskliga bidrag

Från professionella översättare, företag, webbsidor och fritt tillgängliga översättningsdatabaser.

Lägg till en översättning

Wolof

Engelska

Info

Wolof

Ñu romb nag misi, dem dëkku torowas.

Engelska

and they passing by mysia came down to troas.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

tisig moom yebal naa ko dëkku efes.

Engelska

and tychicus have i sent to ephesus.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

Ñooñu nag jiitu, di nu nég dëkku torowas.

Engelska

these going before tarried for us at troas.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu ku nekk dem binduji ca sa dëkku cosaan.

Engelska

and all went to be taxed, every one into his own city.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu nu teer dëkku sirakus, toog fa ñetti fan.

Engelska

and landing at syracuse, we tarried there three days.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ba tey dinaa toog fii ci dëkku efes ba màggalu pàntakot,

Engelska

but i will tarry at ephesus until pentecost.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

filib mu nga dëkkoon betsayda, dëkku andare ak piyeer.

Engelska

now philip was of bethsaida, the city of andrew and peter.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

waaye bi mu ñëwee dëkku room, wut na ma fu ne, ba gis ma.

Engelska

but, when he was in rome, he sought me out very diligently, and found me.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi nga xamee ne yeesu nekkoon na dëkku betani ca kër simoŋ ma gaana woon,

Engelska

now when jesus was in bethany, in the house of simon the leper,

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu mu agsi ci wetu dëkku sikar ci tool, bi yanqóoba mayoon doomam yuusufa.

Engelska

then cometh he to a city of samaria, which is called sychar, near to the parcel of ground that jacob gave to his son joseph.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi ko bokk yi yégee nag, ñu yóbbu ko dëkku sesare, yebal ko dëkku tars.

Engelska

which when the brethren knew, they brought him down to caesarea, and sent him forth to tarsus.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ba ma nekkee dëkku tesalonig sax, yónnee ngeen ay yooni yoon, ngir faj samay soxla.

Engelska

for even in thessalonica ye sent once and again unto my necessity.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

noonu xarekat ya jël pool ci guddi, indi ko ba ca dëkku antipataris, ni ñu leen ko sante.

Engelska

then the soldiers, as it was commanded them, took paul, and brought him by night to antipatris.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

tey jii ca dëkku daawuda, ab musalkat juddul na leen fa, te mooy almasi bi, di boroom bi.

Engelska

for unto you is born this day in the city of david a saviour, which is christ the lord.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

gannaaw gi, mu toxoo dëkku nasaret, dem dëkk kapernawum, bi féeteek dex ga ci diiwaani sabulon ak neftali.

Engelska

and leaving nazareth, he came and dwelt in capernaum, which is upon the sea coast, in the borders of zabulon and nephthalim:

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

ngëm moo tax miir yi wëroon dëkku yeriko màbb, gannaaw ba ko bànni israyil wëree lu mat juróom-ñaari fan.

Engelska

by faith the walls of jericho fell down, after they were compassed about seven days.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

bi elisabet nekkee ci juróom-benni weeram, yàlla yónni na malaakaam jibril ca dëkku nasaret ca diiwaanu galile.

Engelska

and in the sixth month the angel gabriel was sent from god unto a city of galilee, named nazareth,

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

man pool, ndawul kirist yeesu ci coobareg yàlla, maa leen di bind, yéen gaayi yàlla yu sell yi te gëm kirist yeesu ci dëkku efes.

Engelska

paul, an apostle of jesus christ by the will of god, to the saints which are at ephesus, and to the faithful in christ jesus:

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

taxoon na ba yeesu dootul doxantu ci biir yawut ya. noonu mu dem ca gox bu jege màndiŋ ma, ca dëkku efrayim. foofa nag la toog ak ay taalibeem.

Engelska

jesus therefore walked no more openly among the jews; but went thence unto a country near to the wilderness, into a city called ephraim, and there continued with his disciples.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Wolof

nun pool, silwan ak timote noo ngi leen di bind, yéen mbooloom ñi gëm ci dëkku tesalonig te nekk ci yàlla baay bi ak boroom bi yeesu kirist. na yiw ak jàmm ànd ak yéen.

Engelska

paul, and silvanus, and timotheus, unto the church of the thessalonians which is in god the father and in the lord jesus christ: grace be unto you, and peace, from god our father, and the lord jesus christ.

Senast uppdaterad: 2012-05-04
Användningsfrekvens: 1
Kvalitet:

Få en bättre översättning med
7,774,804,791 mänskliga bidrag

Användare ber nu om hjälp:



Vi använder cookies för att förbättra din upplevelse. Genom att fortsätta besöka den här webbplatsen godkänner du vår användning av cookies. Läs mer. OK