From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
duñu génne ci seen gémmiñ lu dul ay móolu ak i xas.
whose mouth is full of cursing and bitterness:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ña fa doon romb di ko xas, di wëcc seen bopp ndax sib ko,
and they that passed by reviled him, wagging their heads,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñeneen ñi dékku nañu ay xas ak ay yar, ay jéng ak kaso yi.
and others had trial of cruel mockings and scourgings, yea, moreover of bonds and imprisonment:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
taskati réew ma it, ya ñu daajaale ak moom, di ko xas noonule.
the thieves also, which were crucified with him, cast the same in his teeth.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
pilaat tontu leen ne: «xas naa koo bind, du deñ.»
pilate answered, what i have written i have written.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci li jëm ci fondamaa bi, kenn mënu fee tëral beneen bu dul bi fi xas a taxaw, muy yeesu kirist.
for other foundation can no man lay than that is laid, which is jesus christ.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
fekk sax malaaka, yi leen ëpp doole ak kàttan, tey sax ca jetaayu boroom bi, ñemewuñoo xas kilifa yooyu.
whereas angels, which are greater in power and might, bring not railing accusation against them before the lord.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ña taxaw ca wetam ne ko: «ndax dangay xas saraxalekat bu mag, bi yàlla fal?»
and they that stood by said, revilest thou god's high priest?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ragal naa, bu ma ñëwee ci yéen, fekk leen nu ma neexul, te yéen it ngeen fekk ma nu leen neexul. ragal naa fekk ay xuloo ci seen biir, ak ñeetaane, xadar ak diiroo mbagg, xas ak jëw, réy-réylu ak yengu-yengu.
for i fear, lest, when i come, i shall not find you such as i would, and that i shall be found unto you such as ye would not: lest there be debates, envyings, wraths, strifes, backbitings, whisperings, swellings, tumults:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: