Results for taalibey translation from Wolof to Spanish

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Spanish

Info

Wolof

taalibey yeesu yi laaj ko lu léeb woowu di tekki.

Spanish

sus discípulos le preguntaron qué significaba esta parábola

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

foofa ay taalibey yaxya tàmbalee werante ak benn yawut ci mbirum sangu set.

Spanish

entonces surgió una discusión entre los discípulos de juan y un judío acerca de la purificación

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ba taalibey yaxya déggee loolu, ñu ñëw, fab néew ba, suul ko ci bàmmeel.

Spanish

cuando sus discípulos oyeron esto, fueron y tomaron su cuerpo, y lo pusieron en un sepulcro

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

fekk booba nag, taalibey yeesu ya dañoo demoon ca biir dëkk ba, di jënd lu ñu lekk.

Spanish

pues los discípulos habían ido a la ciudad a comprar de comer

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kenn ca taalibey yeesu ya, muy yudaa iskariyo, mi ko nar a wor, daldi ne:

Spanish

pero uno de sus discípulos, judas iscariote, el que estaba por entregarle, dijo

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu taalibey yaxya ñëw, fab néew wa, suul ko; ba noppi dem, wax ko yeesu.

Spanish

entonces llegaron sus discípulos, tomaron el cuerpo y lo enterraron. luego fueron y se lo contaron a jesús

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

naka sool, muy tëkkoo rey taalibey boroom bi, ba di ko noyyee far. mu dem nag ca saraxalekat bu mag ba,

Spanish

entonces saulo, respirando aún amenazas y homicidio contra los discípulos del señor, se presentó al sumo sacerdot

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw loolu taalibey yaxya ñëw ci yeesu ne ko: «lu tax nuy woor, nun ak farisen yi, te say taalibe duñu woor?»

Spanish

entonces los discípulos de juan fueron a jesús y dijeron: --¿por qué nosotros y los fariseos ayunamos frecuentemente, pero tus discípulos no ayunan

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

farisen yi ak seeni xutbakat di xultu taalibey yeesu yi ne leen: «lu tax ngeen di lekkandoo ak di naanandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»

Spanish

los fariseos y sus escribas murmuraban contra los discípulos de él, diciendo: --¿por qué coméis y bebéis con los publicanos y pecadores

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ñu ne yeesu: «taalibey yaxya yi ak yu farisen yi dinañu faral di woor ak di ñaan ci yàlla, waaye say taalibe ñu ngiy lekk ak di naan.»

Spanish

entonces ellos le dijeron: --los discípulos de juan ayunan muchas veces y hacen oraciones, igual que los de los fariseos, pero los tuyos comen y beben

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

taalibey yeesu yii àndoon nañu: simoŋ piyeer; tomaa, ki turam di tekki «séex bi;» nataneel, mi dëkk kana ca diiwaanu galile; doomi sebede ak yeneen ñaari taalibe.

Spanish

estaban juntos simón pedro, tomás llamado dídimo, natanael que era de caná de galilea, los hijos de zebedeo y otros dos de sus discípulos

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,747,253,601 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK