検索ワード: baadhi (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

baadhi yao walikubali maneno yake, lakini wengine hawakuamini.

ウォロフ語

Ñenn ñi nag gëm li mu wax, ña ca des weddi ko.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

tusimjaribu bwana kama baadhi yao walivyomjaribu, wakauawa na nyoka.

ウォロフ語

bunu diiŋat kirist, ni ko ñenn ñi ci ñoom defe, ba ay jaan màtt leen, ñu dee.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

yesu akawaambia, "leteni hapa baadhi ya samaki mliovua."

ウォロフ語

yeesu ne leen: «indileen ci jën, yi ngeen jàpp.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baadhi ya walimu wa sheria waliokuwa wameketi hapo wakawaza mioyoni mwao,

ウォロフ語

fekk ay xutbakat toog fa, ñu di werante ci seen xel naan:

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

humo baadhi ya watu walimngojea amponye mtu huyo siku ya sabato ili wapate kumshtaki.

ウォロフ語

am na fa nag ay farisen, ñuy xool yeesu, ba xam dina ko faj ci bésu noflaay bi, ba man koo tuumaal.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini baadhi yao walikwenda kwa mafarisayo wakatoa taarifa ya jambo hilo alilofanya yesu.

ウォロフ語

waaye amoon na it ñu demoon ci farisen ya, nettali leen la yeesu defoon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

baadhi ya mafarisayo na walimu wa sheria waliokuwa wametoka yerusalemu walikusanyika mbele ya yesu.

ウォロフ語

amoon na bés nag, ay farisen ak ay xutbakat yu jóge yerusalem ñëw ci yeesu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

baadhi ya watu wa yerusalemu walisema, "je, yule mtu wanayemtafuta wamuue si huyu?

ウォロフ語

am na ci waa yerusalem ñu doon wax naan: «xanaa du nit kii lañuy wut a rey?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baadhi ya wale walimu wa sheria wakasema, "mwalimu, umejibu vema kabisa."

ウォロフ語

ci kaw loolu ay xutbakat ne ko: «li nga wax dëgg la, kilifa gi!»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baadhi ya mafarisayo wakawauliza, "mbona mnafanya jambo ambalo si halali siku ya sabato?"

ウォロフ語

am ay farisen yu ne: «lu tax ngeen di def lu jaaduwul ci bésu noflaay bi?»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baadhi ya watu waliosimama pale waliposikia hivyo, walisema, "sikiliza! anamwita eliya!"

ウォロフ語

Ñenn ci ña fa taxaw nag, bi ñu ko déggee, ñu ne: «mu ngi woo yonent yàlla iliyas.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baadhi ya wayahudi wakamwuliza yesu, "utafanya muujiza gani kuonyesha kwamba unayo haki kufanya mambo haya?"

ウォロフ語

noonu yawut ya ne ko: «ban firnde nga nuy won ngir dëggal ne, am nga sañ-sañu def lii nga def?»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baadhi ya mafarisayo waliokuwa pamoja naye walisikia maneno hayo, wakamwuliza, "je, sisi pia ni vipofu?"

ウォロフ語

bi farisen ya nekkoon ak moom déggee loolu, ñu ne ko: «xanaa kon nun it danoo gumba?»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

hapo baadhi ya mafarisayo waliokuwako katika lile kundi la watu, wakamwambia yesu, "mwalimu, wanyamazishe wanafunzi wako!"

ウォロフ語

waaye ay farisen yu nekkoon ca mbooloo ma ne yeesu: «kilifa gi, yeddal sa taalibe yi!»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

baadhi ya wanafunzi walikuwa wanazungumza juu ya hekalu, jinsi lilivyopambwa kwa mawe ya thamani, pamoja na sadaka zilizotolewa kwa mungu. yesu akasema,

ウォロフ語

noonu ay nit doon wax ci lu jëm ca kër yàlla ga, ak ni ñu ko rafetale ak ay doj yu jafe ak alal ju ñu jébbal yàlla. waaye yeesu ne leen:

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

baadhi yao walikubali wakajiunga na paulo na sila. kadhalika, idadi kubwa ya wagiriki waliomcha mungu pamoja na wanawake wengi wa tabaka la juu, walijiunga nao.

ウォロフ語

noonu ñenn ci yawut yi gëm, ànd ak pool ak silas, ñoom ak mbooloo mu mag ci gereg yi ragal yàlla, ak jigéen ñu am maana ñu bare.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

petro akawaalika ndani, akawapa mahali pa kulala usiku ule. kesho yake, petro alianza safari pamoja nao, na baadhi ya ndugu wa huko yopa walifuatana naye.

ウォロフ語

ci kaw loolu piyeer dugal leen, dalal leen. ba bët setee, piyeer jóg, dem ak ñoom, ànd ak ñenn ci bokk yi dëkk yope,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

amkeni! anzeni kuishi vema, na acheni kutenda dhambi. baadhi yenu hawamjui mungu kabisa. hii nawaambieni, ni aibu kubwa kwenu!

ウォロフ語

delloosileen xel yi te bàyyi bàkkaar, ndaxte am na ci yéen, ñu umple yàlla. kon war ngeen a rus!

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

msiwe waabudu sanamu kama baadhi yao walivyokuwa; kama yasemavyo maandiko: "watu waliketi kula na kunywa, wakasimama kucheza."

ウォロフ語

buleen jaamu ay xërëm, ni ko ñenn ñi ci ñoom defe woon. ndaxte mbind mi nee na: «mbooloo mi dafa toog, di lekk ak di naan, ba noppi ñu jóg di mbumbaay.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, baadhi yao wakaanza kumtemea mate, wakamfunika uso, wakampiga na kumwambia, "bashiri ni nani aliyekupiga!" hata watumishi wakamchukua, wakampiga makofi.

ウォロフ語

ci kaw loolu ñu daldi tifli ci moom, takk ay bëtam, di ko dóor ay kurfeñ, naan ko: «yaw wax nu ci kàddug yàlla, ku la dóor?» ba noppi alkaati yi teeru ko ak ay pes.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,755,676,086 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK