Добавлены профессиональными переводчиками и компаниями и на основе веб-страниц и открытых баз переводов.
"basi, mtu akiwaambieni siku hizo: kristo yuko hapa au yuko pale, msimsadiki.
«booba nag, bu leen kenn waxee: “kaayleen gis, kirist a ngi fi,” mbaa: “mu nga fale,” buleen ko gëm.
"basi, nawaambieni, siku ya hukumu watu watapaswa kujibu juu ya kila neno lisilofaa wanalosema.
maa ngi leen di wax ne, keroog bés pénc, nit ñi dinañu làyyi ndax wax ju nekk ju amul njariñ, ju ñu mas a wax.
abrahamu, baba yenu, alishangilia aione siku yangu; naye aliiona, akafurahi."
seen baay ibraayma bég na, bi mu yégee sama ngan. bi mu ko gisee it, bég na ci lool.»
lakini yesu akasema, "msimsumbue huyu mama! mwacheni ayaweke kwa ajili ya siku ya mazishi yangu.
waaye yeesu ne ko: «bàyyi ko! jekkoon na mu denc ko ngir bés bu ñu may suul.
siku moja usiku, bwana alimwambia paulo katika maono: "usiogope, endelea kuhubiri tu bila kufa moyo,
naka noona boroom bi feeñu pool ci guddi ne ko: «bul tiit dara, waaye deel wax te bañ a noppi.