Results for waroon translation from Wolof to French

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

French

Info

Wolof

bi muy dem galile, waroon na jaar ci diiwaanu samari.

French

comme il fallait qu`il passât par la samarie,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa du almasi bi dafa waroon a daj boobu coono te dugg ci ndamam?»

French

ne fallait-il pas que le christ souffrît ces choses, et qu`il entrât dans sa gloire?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu gis naa ne, ndigal loolu waroon a jëme nit ñi ci dund, daf maa jëme ci dee.

French

ainsi, le commandement qui conduit à la vie se trouva pour moi conduire à la mort.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

loolu lépp nag takkandeer la woon buy misaal li waroon a ñëw, waaye lu dëggu li mi ngi ci kirist.

French

c`était l`ombre des choses à venir, mais le corps est en christ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

moona yéen de, yéena ngi tiitaru. waaye dangeen a waroon a am naqar, ba dàq kiy def loolu ci seen biir!

French

et vous êtes enflés d`orgueil! et vous n`avez pas été plutôt dans l`affliction, afin que celui qui a commis cet acte fût ôté du milieu de vous!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu yeesu, mi xamoon li ko waroon a dal lépp, jubsi leen ne leen: «ku ngeen di seet?»

French

jésus, sachant tout ce qui devait lui arriver, s`avança, et leur dit: qui cherchez-vous?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye am na ci seen biir ñu ko gëmul.» ndaxte yeesu xamoon na ca njàlbéen ga ñan ñoo ko waroon a gëmadi ak kan moo ko waroon a wor.

French

mais il en est parmi vous quelques-uns qui ne croient point. car jésus savait dès le commencement qui étaient ceux qui ne croyaient point, et qui était celui qui le livrerait.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

man nag bokk yi, mënuma woon a wax ak yéen ni ay nit ñuy déggal xelum yàlla, waaye waroon naa wax ak yéen ni ñuy topp seen nafsu, mel ni ay liir ci seen dund ci kirist.

French

pour moi, frères, ce n`est pas comme à des hommes spirituels que j`ai pu vous parler, mais comme à des hommes charnels, comme à des enfants en christ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ngëm moo tax ba ibraayma déggal yàlla. bi ko yàlla wooyee, mu dem toxu ci menn réew, ma mu waroon a jote ca yàlla. noonu la gàddaaye dëkkam te xamul woon fan la jëm.

French

c`est par la foi qu`abraham, lors de sa vocation, obéit et partit pour un lieu qu`il devait recevoir en héritage, et qu`il partit sans savoir où il allait.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sarax yooyu ñu ngi jëmoon ci lekk ak ci naan ak ci fànn yu bare ci mbirum sangu set. ay sàrt yu jëm ci yaram lañu, yu ñu waroon a farataal, ba kera jamono ji yàllay tëral kóllëre gu bees.

French

et qui, avec les aliments, les boissons et les divers ablutions, étaient des ordonnances charnelles imposées seulement jusqu`à une époque de réformation.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi taalibe ya agsee ca yeesu, ñu ne ko: «yaxya moo nu yebal, nu laaj ndax yaa di ki waroon a ñëw, walla danuy xaar keneen?»

French

arrivés auprès de jésus, ils dirent: jean baptiste nous a envoyés vers toi, pour dire: es-tu celui qui doit venir, ou devons-nous en attendre un autre?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yeesu daldi ne taalibe ya: «na ñépp toog.» fekk ñax mu bare amoon ca bérab ba. noonu góor ñépp àgg suuf. waroon nañoo mat juróomi junni.

French

jésus dit: faites-les asseoir. il y avait dans ce lieu beaucoup d`herbe. ils s`assirent donc, au nombre d`environ cinq mille hommes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

teewul nag la dale ca aadama ba ca musaa, dee a ngi fi woon ci àddina, di noot ñépp, ak sax ñi seen bàkkaar melul woon ni bosu aadama, maanaam jàdd yoon. aadama moomu nag moo di takkandeeru kirist, mi waroon a ganesi àddina.

French

cependant la mort a régné depuis adam jusqu`à moïse, même sur ceux qui n`avaient pas péché par une transgression semblable à celle d`adam, lequel est la figure de celui qui devait venir.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,762,747,404 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK