From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
baada ya mambo haya nitarudi. nitaijenga tena ile nyumba ya daudi iliyoanguka; nitayatengeneza magofu yake na kuijenga tena.
“boroom bi nee na:gannaaw loolu dinaa dellusi,te yékkati këru daawuda, gi ne tasar,dinaa defar toj-toj ya,ba taxawalaat ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ile mbegu iliyoanguka kati ya miti ya miiba, ni mfano wa mtu asikiaye huo ujumbe, lakini wasiwasi wa ulimwengu huu na anasa za mali huusonga ujumbe huo, naye hazai matunda.
ki jot ci jiwu wi ci xaaxaam yi mooy ki dégg wax ji, waaye soxlay àddina ak naxi alal tanc wax ji, ba du jur njariñ.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
hatimaye karani wa mji alifaulu kuwanyamazisha, akawaambia, "wananchi wa efeso, kila mtu anajua kwamba mji huu wa efeso ni mlinzi wa nyumba ya mungu artemi na mlinzi wa ile sanamu iliyoanguka kutoka mbinguni.
gannaaw loolu boroom dëkk ba dalal mbooloo ma ne leen: «yéen waa efes, ana ku xamul ne, dëkku efes moo di wottukaayu màggalukaayu artemis ak nataalam, bi wàcce asamaan?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting